Wolofs: Xutba Yi Wolof · Xutba Yi

Wolofs: Xutba Yi

Importée du site WordPress (page #1349, AudioIgniter #1375).

01 Xutba Tabaski 1443 27:10
02 Wàccuwaayu Sahaaba Yi ak Seeni Ngënéel Xutba 32:15
03 Tabaski ak'iy Àtteem 25:50
04 Xutba Tabaski 1444 31:40
05 Sàmmu-ànte ak Àxxi Jullit Ñi Xutba 24:10
06 Sàmmu-ànte ak Julli Xutba 24:00
07 Weeru Tamxarit Xutba 26:25
08 Yittewoo Defar Xol Yi 23:52
09 Mbir Yiy Defar Xolu Jullit Bi 28:46
10 Bëgg te Yàlla Tax ak Bañ te Yàlla Tax 30:11
11 Taxaw Seetlu Ci Musiba Yiy Xew ci Dundu Gi 27:21
12 Màndargay Bëgg Yonent Bi ﷺ 32:26
13 War Gi Wuuteek Yoonu Ceddo Yi War 27:25
14 Axxu Wayjur Ak Doom 27:46
15 Mbir Yiy Waral Ndimbal'al Yàlla 35:07
16 Àttey Sàngara Ak Lepp Luy Seneebar 31:01
17 Xamale Lénn Ci Xeewali Aljana 29:21
18 Xamle Lénn ci Mbugalu Sawara 31:20
19 Ay Jikko Yu Lislaam Digle 31:30
20 Kiy Dund Dundu gu Dall te Teey 24:25
21 Àttey Bokk Ci Feetu Ñu dul Jullit 26:50
22 Bisu Aljuma Aki Jagleem 28:32
23 Moytul Alal ju Araam 26:35
24 Weeru Rajab Ak Li Nu Si Soss Si'y Bidaa 27:15
25 Ngënéeli Ñaan 29:55
26 Àttey Njibar ci Lislaam 24:16
27 Àttey Mocc Ci Lislaam 33:07
28 Taxawaayu Jullit Bi Ci Jéngu Njiit'am 27:40
29 Na Nu Waajal Weeru Koor 33:56
30 Goor-goor Lu Ci Weeru Koor 30:42
31 Ngëneeli Tudd Yàlla 31:25
32 Xutba Julli'g Korité 2024 43:35
33 Gannaaw Weeru Koor 26:50
34 Jeexiiti Bàkkaar Yi Ci Jaam Bi 30:30
35 Farata'y Hajj ak Umra 27:55
36 Yoon Yi Saytaane Di Jaar Doomu Aadama 37:30
37 Njibar Aki Loram Ci Diine 39:12
38 Fàggu Alal 32:45
39 Ngëneeli Fukki Fan'i Tabaski 31:44
40 Xutba Tabaski 1445 31:00
41 Sax Ci Ak Njub 30:50
42 Yittewoo Waxtu Ci Dundu Jullit Bi 30:37
43 Weeru Tamxarit Ak Li Ñu Ci Yoonal 27:10
44 Ñaan Ak'i Waxtoom 33:40
45 Dee Ak Dundu'k Bàmmeel 29:35
46 Àttey Jëw ak Rambaaj 29:06
47 Yaatu'g Lislaam Ak Pas-pasu Jullit bi Ci Yonent YÀLLA IISAA ibn Maryam ﷺ 30:31
48 Lor'i Bidaa ci Diine 25:00
49 Wareefu Jullit Bi Ci Yiy Xew 27:32
50 Rafetal Ci Lislaam 26:50
51 Jàkka Ci Lislaam 31:56
52 Waajal Dee 28:40
53 Wareefu Jullit Bi Ci Alxuraan 33:12
54 Jullit Bi Ak Mëbet 28:40
55 Julli Aki Jagleem 27:15
56 Sàmmu Ànte ak Julli 35:52
57 Moytul Gisaane Ka Yi 28:41
58 Ñaari Baati Seede yi li Miy Wuddu ak li Miy Waral 25:40
59 Tuur Bakkanu Jullit ci Lislaam 27:17
60 Ndénkaane Gu Am Solo 26:37
61 Njariñu Wéetal Yàlla 28:30
62 N*01 | Bunti Àjjana Yi 30:50
63 N*02 | Bunti Àjjana Yi 28:50
64 Waajal Weeru Koor 29:35
65 Jéggalu ak Tuub Ci Weeru Koor 30:25
66 Weeru Alxuraan 32:05
67 Yókk Góor-Góor Lu Ci Fukki Fan Yi Mujj Ci Weeru Koor 26:17
68 Mbégte Jullit Bi | Xutba IID Al-Fitr 31:57
69 Sax ci Jaamu Yàlla Gannaaw Weeru Koor 28:12
70 Deel Leer lu bu la Xibaar Dikkale 31:25
71 Weer Yi Yàlla Araamal Ak Weeri Hajj 30:55
72 Sàmmu Ànte ak Kóllare 29:52
73 Ponkki Hajj aki Wareefam Xutba 36:10